Category: Diine
Alxuraan ci Wolof: Suraat wi jëkk
Wacce Màkka 7 laaya Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Màggal Yàlla buuru dunyaa2- Raax Menn Raax yërëm 4- Yaw la ñuy jaamu, yaw la ñuy ñaan ndimmël.5- Teg ñu ci yoon wi jub, 6- Ci yoonu ñi nga béggale say mbaax; 7- ñi la merloowul te…
Alxuraan ci Wolof: Suraat CXIV – Nit ñi
Wàcce ci Màkka 5 laaya Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Nil damay wut kiiraay ci sunu Booroom 2- Buur ci ku di nit 3- Yàlla ci ku di nit 4- Wàttu ma ci mbonu kiy sol xalaat yu bon tey rocceeku 5- Di wal lu bon ci…
Alxuraan ci Wolof: Suraat CXIII – Bes tenk
Wàcce ci Màkka 5 laaya Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Nil damay wut kiiraay ci Yàlla fa bër sete 2- Muslu ci mbon gi ci mbindeef yi mu sàkk 3- Muslu ci musiba guddi lëndëm këriis fa mu ñu bette 4- Muslu ci mbonu dëmm yiy wal…
Alxuraan ci Wolof: Suraat CXI – Abdu Laxab
Wàcce ci Màkka 5 laaya Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Na ñaari loxo Abu Laxab ya raaf, te mu raaf moom ci boppam 2- Alalam aki jëfëm du ñu ko jëriñ dara 3- Danañu ko lakk ci safara say boy 4- Moog jabaram ja yanu matt 5-…
Ki kawee kawe – Alxuraan ci Wolof: Suraat LXXXVI
Wàcce ci Màkka 19 laaya Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Magalal turu sa Boroom mi kawee kawe 2- Ki sàkk mbir yi te muul leen 3- Ki dogal seeni muj te teg leen ñoom ñépp ci jëmoom 4- Kiy saxal gàncax gi 5- Te di ko delloo…
Suraat LXXIX: Malaaka yiy rocci ruu
Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Ag malaaka yiy rocci ruu ag dool 2- Malaaka yi leen di roñ ndànk, jellë ci biir ñenen ñi 3- Ag ñiy jàll bu gaaw jàww ji 4- Ag ñiy daw ci lu gaaw di jiitu 5- Ag ñi yélif ag di…
Alxuraan ci Wolof: Nit
Wàcce ci Màkka 31 laaya Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Ndax dafa toog lu yàgg te kenn fàttelekuwu ko? 2- Danu door sàkk ci ndoxum geño wu ñaari kanam àndoo fekk ñu koy seetlu. Daanu ko jox gis ak dégg. 3- Danu ko teg ci yoon wu…
Xasida Sëriñ Tuuba ci Wolof
Taaliif wii nag lu ñu barkeel la ci njëlbéen gi ba ca dayo ba. Moom nag ki waxoon bayit wu njëkk wi –yal nañu ko dolli ag bëbb (xéewal) – am na ba tay weneen bayit wu yor maanaa mii, mu ciy nos woy, maanaam waxi sëriñam ji, wax jooju mooy jii : nguurug neen…