• KER GI
  • Politig
  • NEKKIN
  • Diine
  • Caada
  • Tàggat yaram
  • Jokkoo

wolof-online.com

Ads
  • Koom-koom
  • Taataan
  • Xamtéef
  • Cosaan
  • Wér-gu-yaram
  • Lëkkale
  • Jotaayu-xale yi
  • Multimejaa
  • Mbindu-fent
  • Politik

  • 2
    Ku wax feeñ: demokaraasi ag làkki réew mi
    Ku wax feeñ: demokaraasi ag làkki réew mi Wote bi nu dëgmal, ñépp xam na ñu ko, wote bu jeggi dayoo la: ndax ci la ëllëgu réew mi aaju! Wote tànn la wan yoon la Senegaal war a […]
  • 0
    Yaaya Jàmme: liy ñuul ci meew mi
  • 0
    Isaa Bokar Si ” Yaaya Jàmme mooy ndeyyi-mbill mi ci Gambi ak Kasamaas”
    Isaa Bokar Si ” Yaaya Jàmme mooy ndeyyi-mbill mi ci Gambi ak Kasamaas” Isaa Bokaar Si, ambaasadeur Yaaya Jàmme la woon, bokkoon na ak Y. Jàmme nekk tàkk-der. Ku ko xam la, ku xam fu ma jaar la…Déggluleen
  • 0
    Màki Sàll: “du ma làq kenn ku def lu dëppoowul ag yoon”!
    Màki Sàll: “du ma làq kenn ku def lu dëppoowul ag yoon”! Ci benn laaj-toontu bu njiitu-réew mi amal ag yeenekaay bu tudd Afrik te nekk ca Belsik, Màkki Sàll feeñal na ay xalaatam ci mbir yu am solo yu soxal Senegaal […]
  • 0
    Kookooy Saalif Saajo njiitu waay-fippu ya ca Kasamaas…!
    Kookooy Saalif Saajo njiitu waay-fippu ya ca Kasamaas…! Peresidaa Maki Sàll ne woon ayu-bés yale weesu, ne tàllal na loxoom waay-fippu ya nekk Kasamaas, ngir ñu tóog seet ci sunu biir naka lañu war a def ba saafara […]
  • 0
    Tombukutu: Saay-saay yi defati nañu fa ñaawtéef…
    Tombukutu: Saay-saay yi defati nañu fa ñaawtéef…   Tey ci Tombukutu, waay-fippu yiy bàkkoo lislaam te naan dañuy jihaad defati nañu fa ñaawtéef yu bon: ndax dañoo dug ci xabru ay waliyu yu mag, toj leen ba […]
  • 0
    Woote ndawi-réew mi 2012
    Woote ndawi-réew mi 2012 Naka démb ci dibeer gi la Senegaal wootewaat woote bu am solo ngir fal ndaw yiy war a taxawal askan wi ci pencum réew mi. Ci xibaar yi jot a […]
  • 0
    Maki Sàll demoon na Kasamaas seeti jambaar yi…
    Maki Sàll demoon na Kasamaas seeti jambaar yi…
  • 0
    Askani Senegaal am na ndam!
    Askani Senegaal am na ndam! Peresidaa Ablaay Wàdd nangu na dibeer ca guddi gànnaaw ba resiltaa wote bi tàmbalee wàdd, ne Maki Sàll moom la réew mi tànn. Moom Ablaay Wàdd wóo na Maki, ñaanal […]
  • 0
    Kàddu yu njëkk yi tukkee ci Màkki Sàll
    Kàddu yu njëkk yi tukkee ci Màkki Sàll Yeen wa Senegaal, góor ak jiggéen, mag ak ndaw, sama askan sope. Ci bésu dibeer bii 25 fan ci weeru Mars 2012, gànnaaw beneen bésu 26 fan Fewie bu kenn […]
  • 0
    Amaat Dansoxo: Bañ ba dee!
    Amaat Dansoxo: Bañ ba dee!
  • 0
    Bennoo, Ñaaroo, Ñettoo ba Ñent…. Mbooloo mooy doole te mooy jàmmi-réew, wante lu waay di wuyoo na koy niroo! Moo tax ba Front Siggil Senegaal seete seetaat ba tudde boppam […]
  • 0
    Nàqar, tiis ak metit
    Nàqar, tiis ak metit Réewum Senegaal tollu na diggante bu xat te mooy diggante dund ak dee gannaaw ba kuréel gi waroon a saytu sàrti-réew mi feeñale parparloom ne ki ñépp di mbàmb, neex […]
  • 1
    Maa waxoon waxeet!
    Maa waxoon waxeet! “Maa waxoon…waxeet!” kàddu yooyu njiitu réew mi yëkkëti ci ndaje PDS bi amoon ci 23 fan ci weeru suliye, weesu na waar ba faf wër àddina! Image Ñu bare ñu […]
  • 0
    Askan wi fippu na!
    Askan wi fippu na! Bésu alxamés bii di 23 fan ci weeru swe 2011 bés la bu mag ci biiri bés yi ci ndeminu demokaraasi ci réewum Senegaal. Ndax gannaaw ba njiitu-réew mi fésale […]
  • Next Page »
Ads Ads

Siiwal dal bi!

Filosofi ci wolof

  • Filosofi ci wolof
advert

Jukki yi mujj

  • Yeesal baatu xarala ci wolof / Taatanu Wolof ak Xamle
    Yeesal baatu xarala ci wolof / Taatanu Wolof ak Xamle

    1- Jollasu gi = téléphone 2- Kippaango gi = groupe 3-

  • Turi rabi àll yi ci Wolof
    Turi rabi àll yi ci Wolof

    golo gi golo gu ñuul gi dangin wi bukki bi yolaan

  • Lu tax nu war a jàng ci làkki réew mi
    Lu tax nu war a jàng ci làkki réew mi

  • Melo yi wolof
    Melo yi wolof

  • Làmmiñu tubaab lañu ñagee seen diggante ak mbooloo mi
    Làmmiñu tubaab lañu ñagee seen diggante ak mbooloo mi

  • Bés bu taalifkati yeneen réew làkkee wolof…
    Bés bu taalifkati yeneen réew làkkee wolof…

    * Jukki bii topp maa ngi ko jëlee  sama téere bi

Joxe sa xalaat

War nañoo delloo làkki-réew mi seen gëdd, di leen jëfëdikoo ci nguur gi, ci lekkool yi, ci àttekaay yi ak fépp fu ñuy dogale.

View Results

Loading ... Loading ...
  • Polls Archive
  • Kàggu
  • Siiwal
  • Jukki yi mujj

Kàggu

  • February 2022
  • January 2022
  • December 2021
  • November 2021
  • September 2021
  • August 2021
  • June 2021
  • February 2021
  • January 2021
  • December 2020
  • October 2020
  • September 2020
  • July 2020
  • June 2020
  • May 2020
  • April 2020
  • November 2019
  • September 2019
  • December 2018
  • October 2018
  • September 2018
  • April 2018
  • December 2017
  • November 2017
  • October 2017
  • September 2017
  • August 2017
  • January 2017
  • December 2016
  • October 2016
  • April 2016
  • March 2015
  • December 2014
  • November 2014
  • June 2014
  • January 2014
  • December 2013
  • October 2013
  • July 2013
  • June 2013
  • May 2013
  • January 2013
  • November 2012
  • October 2012
  • September 2012
  • August 2012
  • July 2012
  • June 2012
  • May 2012
  • March 2012
  • February 2012
  • January 2012
  • June 2011
  • August 2010
  • March 2009
  • March 2008
Siiwalal dal bi yonnee ko facebook , twitter, mbaa nga yonne ko ag sa imeel sa ay xamee!

Jukki yi mujj

  • Yeesal baatu xarala ci wolof / Taatanu Wolof ak Xamle
  • Turi rabi àll yi ci Wolof
  • Lu tax nu war a jàng ci làkki réew mi
  • Melo yi wolof
  • Làmmiñu tubaab lañu ñagee seen diggante ak mbooloo mi
  • Bés bu taalifkati yeneen réew làkkee wolof…
© wolof-online.com 2023
  • wolof-online
  • Jokkoo