0
Sembeen Usmaan: Gelewaar
-
2012 September
-
Laaj-toontu ak Njaga Mbay Jaar-jaaru woykat bu jege woon askanam Ci sanwiye 1999, yeneekay Lasli/Njëlbéen amoon na laaj-tootu bu yaatu ag Njaga Mbay, doon ca feeñal ay jaar-jaaram. Waxtaan woowu Njaga Mbay amoon ak […]
-
Ku wax feeñ: demokaraasi ag làkki réew mi Wote bi nu dëgmal, ñépp xam na ñu ko, wote bu jeggi dayoo la: ndax ci la ëllëgu réew mi aaju! Wote tànn la wan yoon la Senegaal war a […]
-
Isaa Bokar Si ” Yaaya Jàmme mooy ndeyyi-mbill mi ci Gambi ak Kasamaas” Isaa Bokaar Si, ambaasadeur Yaaya Jàmme la woon, bokkoon na ak Y. Jàmme nekk tàkk-der. Ku ko xam la, ku xam fu ma jaar la…Déggluleen