5
Bés bi UNESCO jagleel làkki ndey yi …
Bésu 21 fan ci weeru fewrie at mu jot, moom la kurél giy toppatoo caada, njàng ak xamtéef (UNESCO) te féetoo ci mbotaayu xeet yi, jagleel làkki ndey, maanaam làkk […] -
2021 February
-
-
“Filosofi ci wolof”… téere bu bees bi Tamsir Anne génne Seetal Fii « Philosophie en wolof : A comme aada … » aada j. : aada mooy mbooleem matukaay yi am mbooloo, gën gaa bare, aw askan di tegtaloo cig jëf, di ca […]
-
Benn bés, benn woy: Sëriñ Musaa ka XARNU BI Sëriñ bi noo gi deeti ñaan Faqiir dafay nangoo dagaan Nangul nu lépp lu nu ñaan Ndax Yàlla naatal xarnu bi Noongi dangaan ci Mustafaa Ma nekk marwat’ak […]