Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm
1- Màggal Yàlla buuru dunyaa2- Raax Menn Raax yërëm
4- Yaw la ñuy jaamu, yaw la ñuy ñaan ndimmël.5- Teg ñu ci yoon wi jub,
6- Ci yoonu ñi nga béggale say mbaax;
7- ñi la merloowul te réeruñu
Tekki bi: Pathe Diagne, Alxuraan ci Wolof. Editions Sankore, L’Harmattan.
There are no comments yet, be the first.