Alxuraan ci Wolof: Suraat CXIV – Nit ñi

Wàcce ci Màkka 5 laaya

Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm

1- Nil damay wut kiiraay ci sunu Booroom

2- Buur ci ku di nit

3- Yàlla ci ku di nit

4- Wàttu ma ci mbonu kiy sol xalaat yu bon tey rocceeku

5- Di wal lu bon ci xolu nit

 

 

Tekki bi: Pathe Diagne, Alxuraan ci Wolof. Editions Sankore, L’Harmattan.

There are no comments yet, be the first.

Leave a Comment