• admin

  • 0
    Antoine de Saint Exupéry – Ndoomi Buur si Antoine de Saint-Exupéry Ndoomi Buur si       Traduit en Wolof par Dr. Tamsir ANNE       Tudee naa ko Leon Werth Yeen xale yi, na ngeen ma […]
  • 5
    Senegaal ak bés bi UNESCO jàgleel làkki-ndey… Bésu 21 fan ci weeru Fewrie at mu jot, moom la kurél giy toppatoo caada, njàng ak xamtéef (UNESCO) te feeteewoo ci mbotaayu-xeet-yi, jagleel làkki-ndey yi, maanaam làkk wi nga […]
  • 0
    Leebu Wolof-Njaay: A ni aada 1. Aar moo gën faj. (20) Image 2. Aawo, aw la tudd. (9) 3. Aawo buuru këram. (2) 4. Aaye na, aayeetul keroog. (1) 5. Ab dag du bëgg moroom […]
  • 2
    Diine ci làmmiñu Wolof: Yoonu ragal-Yàlla Bisimilaahi Rahmaani Rahiimi… Ñu fas yeeney dollee deηkënte ak di dollee fàtleente. Ñiη koy jëmële nak ci tomb bi nga xam ne mbooleem liy yiiwu àdduna ak yiiwu àllaaxira ci […]
  • 0
    Jamono ci wolof
  • 0
    Seex Anta Jóob: Xayma ci Wolof – La héorie des Ensembles Ensembles équivalents Deux ensembles M et N sont équivalents si à un élément de M correspond un élément et un seul de N, et réciproquement. Le caractère commun à tous […]
  • 0
    Téere-woy yi Téere-woy yi téere la bu ëmb taalif yu bindkat ak xaralakat yu mag ci làkki almaa taalif. Téere baa ngi genn ci atum 2011 ca Almaañ. Tamsir Anne, mi móol […]
  • 1
    Sedaar Seŋoor: Juwaaloo Juwaalo Juwalo! Maa ngi fàtteliku. Maa ngi fàtteliku siñaar ya ca keru mbaar yu naat ya Maa ngi fàtteliku siñaar yeek seeni gët, kemtaanee lool Di sàmandaay leeraayu-weer cig tefes […]
  • 0
    Léebu… Am bukki yomb na, waaye bukki buy xalam a jafe. Am na bukki bu ŋexalul, te jégéñ kër.   Bukki am na gillint, tey àll bi leer. Bukki amtekoonu bàkk […]
  • 2
    Sàrti ndaali-Maali Tamsir Anne (tekkikat bi) Ndaali-Maali walla Mande benn la woon ci nguuru nit ku ñuul yu mag yi nekkoon démb ci déndub Afrik. Moo fi wuutu woon ndaali GANA ci […]
  • 0
    Turu rabi-àll yi ci Wolof golo gi golo gu ñuul gi dangin wi bukki bi yolaan wi siiru bi wel wi till wi suññeel wi kund wi wéxéñ wi jaar ji sikóor bi njaxat wi […]
  • 0
    Tafsiiru Alxuraan: Baay Ñas
  • 0
    Bàkku Senegaal   Yëngal-leen kooraa yi te dóor ci sabar yi Gaynde ñaloor yuux na. Boroom àll tëb na Tëb na tëbu jàmbaar, leeral lu doon lëndëm Suñuy naqar jeex na, sunu […]
  • 1
    ndeeteelu làkk yi… Ci 7000 làkk yi ci àddina, 85 la ñi ëpp ci nit ñi, daanaka 78%, di làkk. Làkku angale ñi koy làkk tollu nañu ci 328 miliyoη, ñiy làkk sinwaa tollu […]
  • 1
    Li ci biir “francophonie” Ci ayi bés yii ñu dëgmal mbootaayi-réew yiy jëfandikoo làkki “francais” tey wooye seen bopp mbootaayu “Frankofoni” ñu ngi waaj seen 14eelu ndaje, ngir berndeel làkki francais ak caada Faraas. […]