• 2011 June

  • 0
    Askan wi fippu na! Bésu alxamés bii di 23 fan ci weeru swe 2011 bés la bu mag ci biiri bés yi ci ndeminu demokaraasi ci réewum Senegaal. Ndax gannaaw ba njiitu-réew mi fésale […]
  • 0
    Yàtt bi lëmbee jamono! Su dee ni ko yenn waay-xeltu yi di waxee namm-namm xarala dëggantaan mooy gësëm xelu nit ñi ba ñu xippi xool, gise neneen mbir yi leen wër,ku yebboo kon ne […]