1
Li ci biir “francophonie”
Ci ayi bés yii ñu dëgmal mbootaayi-réew yiy jëfandikoo làkki “francais” tey wooye seen bopp mbootaayu “Frankofoni” ñu ngi waaj seen 14eelu ndaje, ngir berndeel làkki francais ak caada Faraas. […] -
2017 August
-
-
Timbukutu: peyu xam-xam Timbukutu: péyu xam-xam bu yàgg te sax! Ni ñu leen ko fi waxeewoon ci jukki bi weesu, bind, sàkku xam-xam, gëstu ak diine lu yàgg la ci Afrik! Wante ñakka […]