0
Taalif
-
2012 June
-
Sunu sosiete Sunu sosete Sunu sosete yëngëtu na! Sunu sosete yëngëtu na! Ñun danuy am faydaa! Ñun danuy am faydaa! Ñun danuy fonk sunu Senegaal! Adduna potu […]
-
Léeboon: Doomi Yàlla Léeboon! Lippóon! Amoon na fi! Daan na am! Ba mu amee yaa fekkee? Ya wax ma dégg! waxi tey jar ta gëm! Sa yos moo ci raw! Xew xew bii […]
-
Niseeryaa sànni na ñaari satelit ci jàww ji! Réewum Niseerya siiwal na alxamees gee nu weesu – 18 fan ci weeru Ut – ne sànni ñaari “satelit” ci jàww ji. Satelit yooyee la ñu cay namm mooy yokk […]
-
Alxuraan ci Wolof: Suraat wi jëkk Wacce Màkka 7 laaya Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Màggal Yàlla buuru dunyaa2- Raax Menn Raax yërëm 4- Yaw la ñuy […]
-
Alxuraan ci Wolof: Suraat CXIV – Nit ñi Wàcce ci Màkka 5 laaya Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Nil damay wut kiiraay ci sunu Booroom 2- Buur ci ku di […]
-
Alxuraan ci Wolof: Suraat CXIII – Bes tenk Wàcce ci Màkka 5 laaya Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Nil damay wut kiiraay ci Yàlla fa bër sete 2- Muslu ci […]
-
Alxuraan ci Wolof: Suraat CXI – Abdu Laxab Wàcce ci Màkka 5 laaya Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Na ñaari loxo Abu Laxab ya raaf, te mu raaf moom ci […]
-
Ki kawee kawe – Alxuraan ci Wolof: Suraat LXXXVI Wàcce ci Màkka 19 laaya Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Magalal turu sa Boroom mi kawee kawe 2- Ki sàkk mbir yi […]