0
Alxuraan ci làkku wolof
Alxuraan ci wolof -
Diine
-
Benn bés, benn woy: Sëriñ Musaa ka XARNU BI Sëriñ bi noo gi deeti ñaan Faqiir dafay nangoo dagaan Nangul nu lépp lu nu ñaan Ndax Yàlla naatal xarnu bi Noongi dangaan ci Mustafaa Ma nekk marwat’ak […]
-
Diine ci làmmiñu Wolof: Yoonu ragal-Yàlla Bisimilaahi Rahmaani Rahiimi… Ñu fas yeeney dollee deηkënte ak di dollee fàtleente. Ñiη koy jëmële nak ci tomb bi nga xam ne mbooleem liy yiiwu àdduna ak yiiwu àllaaxira ci […]
-
Xasida Sëriñ Tuuba ci Wolof : Nahjul Xadaail Haaji – Wolof Maa ngi tàmbale samay wax ak jëf ci turu Yàlla miy kiy boroom yërmande ju yaa ji ci adduna ak ja ca allaaxiraa. Yal na Yàlla dolli xéewal ak mucc […]
-
Xasida ci Wolof : Sindiidi SINDIIDI Ki ko tekki ci wolof : Cheikhouna LO Ngabou Ci turu Yàlla jiy yëramaakoon bi di jaglewaakoon laay tàmblee, di julli (ñaan xéwël ak mucc) ci Yonnent bi aki […]
-
Alxuraan ci Wolof: Suraat XCII – Guddi Wàcce ci Màkka 21 laaya Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Ag guddi fu mu tallale muraayam 2- Ag bëccëg fu mu leere […]
-
Alxuraan ci Wolof: Suraat wi jëkk Wacce Màkka 7 laaya Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Màggal Yàlla buuru dunyaa2- Raax Menn Raax yërëm 4- Yaw la ñuy […]
-
Alxuraan ci Wolof: Suraat CXIV – Nit ñi Wàcce ci Màkka 5 laaya Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Nil damay wut kiiraay ci sunu Booroom 2- Buur ci ku di […]