0
Léebu…
Am bukki yomb na, waaye bukki buy xalam a jafe. Am na bukki bu ŋexalul, te jégéñ kër. Bukki am na gillint, tey àll bi leer. Bukki amtekoonu bàkk […] -
2017 October
-
-
Bàkku Senegaal Yëngal-leen kooraa yi te dóor ci sabar yi Gaynde ñaloor yuux na. Boroom àll tëb na Tëb na tëbu jàmbaar, leeral lu doon lëndëm Suñuy naqar jeex na, sunu […]