0
jiggéen yu mën góor…
Ci at yi ak wéer yi weesu, mel na ni Afrik dafa dellu fa baaxi maam nekkoon, te mooy wormaal, naw, solool jiggéen. Bu ñu ko fatte fii ci Afrik, […] -
2012 July
-
-
Téy la Mandela di am 94 at… Téy ci 18eelu fan ci wéeru Suliye lay Nelson Mandela, mi kenn dul nettali ay jàllooreem di am 94 at! Réewum Afrik di Sid yépp, Afrik gépp ak àddina sépp […]
-
Màki Sàll: “du ma làq kenn ku def lu dëppoowul ag yoon”! Ci benn laaj-toontu bu njiitu-réew mi amal ag yeenekaay bu tudd Afrik te nekk ca Belsik, Màkki Sàll feeñal na ay xalaatam ci mbir yu am solo yu soxal Senegaal […]
-
Kookooy Saalif Saajo njiitu waay-fippu ya ca Kasamaas…! Peresidaa Maki Sàll ne woon ayu-bés yale weesu, ne tàllal na loxoom waay-fippu ya nekk Kasamaas, ngir ñu tóog seet ci sunu biir naka lañu war a def ba saafara […]
-
Tombukutu: Saay-saay yi defati nañu fa ñaawtéef… Tey ci Tombukutu, waay-fippu yiy bàkkoo lislaam te naan dañuy jihaad defati nañu fa ñaawtéef yu bon: ndax dañoo dug ci xabru ay waliyu yu mag, toj leen ba […]
-
Woote ndawi-réew mi 2012 Naka démb ci dibeer gi la Senegaal wootewaat woote bu am solo ngir fal ndaw yiy war a taxawal askan wi ci pencum réew mi. Ci xibaar yi jot a […]
-
Dal leen ag jamm! Mbooloo mi! Ñu ngi leen di nuyu ku ci nekk ci yeen ci sa tur ak sa sànt te di leen dalal ci jàmm. Béréb bi ngeen tersi téy nag […]
-
Seex Musaa Ka: Xarnu bi XARNU BI Sëriñ bi noo gi deeti ñaan Faqiir dafay nangoo dagaan Nangul nu lépp lu nu ñaan Ndax Yàlla naatal xarnu bi Noongi dangaan ci Mustafaa Ma nekk marwat’ak […]