0
Askani Senegaal am na ndam!
Peresidaa Ablaay Wàdd nangu na dibeer ca guddi gànnaaw ba resiltaa wote bi tàmbalee wàdd, ne Maki Sàll moom la réew mi tànn. Moom Ablaay Wàdd wóo na Maki, ñaanal […] -
2012 March
-
-
Kàddu yu njëkk yi tukkee ci Màkki Sàll Yeen wa Senegaal, góor ak jiggéen, mag ak ndaw, sama askan sope. Ci bésu dibeer bii 25 fan ci weeru Mars 2012, gànnaaw beneen bésu 26 fan Fewie bu kenn […]
-
Laaj-toontu: B. Boris Joob Bubakar Boris Jóob kenn la ci bindkat yi gëna mag ci Senegaal ag ci Afrik. Bind na ay téere yu siiw ci kalaama farañse ag benn téere bu am solo […]