Wàcce ci Màkka 5 laaya
Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm
1- Na ñaari loxo Abu Laxab ya raaf, te mu raaf moom ci boppam
2- Alalam aki jëfëm du ñu ko jëriñ dara
3- Danañu ko lakk ci safara say boy
4- Moog jabaram ja yanu matt
5- Te ci baatam la noo yeewi buumu xañci tandarma
There are no comments yet, be the first.