• 2017 January

  • 1
    Kopparu CFA ag Ëro ñoo xoj Afrik ! Nicolas Agbohou jàngalekat la ci fànnu koom-koom ci daara yu mag ya ca Tugal, cosaanoo Kodiwaar. Ci laaj-toontu bii ñu leen fi tekkil day ηàññ doxalinu réewi Afrik yiy jëfandiku […]
  • 1
    Ngëneel yi ci garabu nebedaay Nebedaay walla ci turu wolofam dëgg saab-saab, garab la gu bari ay ngëneel ci wàllu dund ndax witamin ak ferñeent yu bari yi ci nekk ak li mën a faj […]