0
Alxuraan ci Wolof: Suraat CXIII – Bes tenk
Wàcce ci Màkka 5 laaya Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Nil damay wut kiiraay ci Yàlla fa bër sete 2- Muslu ci […] -
Diine
-
-
Alxuraan ci Wolof: Suraat CXI – Abdu Laxab Wàcce ci Màkka 5 laaya Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Na ñaari loxo Abu Laxab ya raaf, te mu raaf moom ci […]
-
Ki kawee kawe – Alxuraan ci Wolof: Suraat LXXXVI Wàcce ci Màkka 19 laaya Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Magalal turu sa Boroom mi kawee kawe 2- Ki sàkk mbir yi […]
-
Suraat LXXIX: Malaaka yiy rocci ruu Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Ag malaaka yiy rocci ruu ag dool 2- Malaaka yi leen di roñ ndànk, jellë ci biir […]
-
Alxuraan ci Wolof: Nit Wàcce ci Màkka 31 laaya Benn – Senn – Menn la – Raax Menn – Raax Yërëm 1- Ndax dafa toog lu yàgg te kenn fàttelekuwu ko? 2- Danu door […]
-
Xasida Sëriñ Tuuba ci Wolof Taaliif wii nag lu ñu barkeel la ci njëlbéen gi ba ca dayo ba. Moom nag ki waxoon bayit wu njëkk wi –yal nañu ko dolli ag bëbb (xéewal) – […]