2
Ku wax feeñ: demokaraasi ag làkki réew mi
Wote bi nu dëgmal, ñépp xam na ñu ko, wote bu jeggi dayoo la: ndax ci la ëllëgu réew mi aaju! Wote tànn la wan yoon la Senegaal war a […] -
Politik
-
-
Isaa Bokar Si ” Yaaya Jàmme mooy ndeyyi-mbill mi ci Gambi ak Kasamaas” Isaa Bokaar Si, ambaasadeur Yaaya Jàmme la woon, bokkoon na ak Y. Jàmme nekk tàkk-der. Ku ko xam la, ku xam fu ma jaar la…Déggluleen
-
Màki Sàll: “du ma làq kenn ku def lu dëppoowul ag yoon”! Ci benn laaj-toontu bu njiitu-réew mi amal ag yeenekaay bu tudd Afrik te nekk ca Belsik, Màkki Sàll feeñal na ay xalaatam ci mbir yu am solo yu soxal Senegaal […]
-
Kookooy Saalif Saajo njiitu waay-fippu ya ca Kasamaas…! Peresidaa Maki Sàll ne woon ayu-bés yale weesu, ne tàllal na loxoom waay-fippu ya nekk Kasamaas, ngir ñu tóog seet ci sunu biir naka lañu war a def ba saafara […]
-
Tombukutu: Saay-saay yi defati nañu fa ñaawtéef… Tey ci Tombukutu, waay-fippu yiy bàkkoo lislaam te naan dañuy jihaad defati nañu fa ñaawtéef yu bon: ndax dañoo dug ci xabru ay waliyu yu mag, toj leen ba […]
-
Woote ndawi-réew mi 2012 Naka démb ci dibeer gi la Senegaal wootewaat woote bu am solo ngir fal ndaw yiy war a taxawal askan wi ci pencum réew mi. Ci xibaar yi jot a […]
-
Askani Senegaal am na ndam! Peresidaa Ablaay Wàdd nangu na dibeer ca guddi gànnaaw ba resiltaa wote bi tàmbalee wàdd, ne Maki Sàll moom la réew mi tànn. Moom Ablaay Wàdd wóo na Maki, ñaanal […]
-
Kàddu yu njëkk yi tukkee ci Màkki Sàll Yeen wa Senegaal, góor ak jiggéen, mag ak ndaw, sama askan sope. Ci bésu dibeer bii 25 fan ci weeru Mars 2012, gànnaaw beneen bésu 26 fan Fewie bu kenn […]
-
Nàqar, tiis ak metit Réewum Senegaal tollu na diggante bu xat te mooy diggante dund ak dee gannaaw ba kuréel gi waroon a saytu sàrti-réew mi feeñale parparloom ne ki ñépp di mbàmb, neex […]
-
Maa waxoon waxeet! “Maa waxoon…waxeet!” kàddu yooyu njiitu réew mi yëkkëti ci ndaje PDS bi amoon ci 23 fan ci weeru suliye, weesu na waar ba faf wër àddina! Image Ñu bare ñu […]
-
Askan wi fippu na! Bésu alxamés bii di 23 fan ci weeru swe 2011 bés la bu mag ci biiri bés yi ci ndeminu demokaraasi ci réewum Senegaal. Ndax gannaaw ba njiitu-réew mi fésale […]