1
Sedaar Seŋoor: Juwaaloo
Juwaalo Juwaalo! Maa ngi fàtteliku. Maa ngi fàtteliku siñaar ya ca keru mbaar yu naat ya Maa ngi fàtteliku siñaar yeek seeni gët, kéemtaanee lool Di sàmandaay leeraayu weer cig […] -
Mbindu-fent
-
-
Antoine de Saint Exupéry – Ndoomi Buur si Antoine de Saint-Exupéry Ndoomi Buur si Traduit en Wolof par Dr. Tamsir ANNE Tudee naa ko Leon Werth Yeen xale yi, na ngeen ma […]
-
Leebu Wolof-Njaay: A ni aada 1. Aar moo gën faj. (20) Image 2. Aawo, aw la tudd. (9) 3. Aawo buuru këram. (2) 4. Aaye na, aayeetul keroog. (1) 5. Ab dag du bëgg moroom […]
-
Benn bés, benn woy Lenn li Ci kow puj yépp Lépp a ngi ne tekk Ci senn ruxx Do yëg sax Lu noyyi. Picc saa ngi ne selaw Ci àll bi. […]
-
Waxi Wolof Njaay Juddu ci gëléem, nàmp ci mbaam Bu sunu boroom bi bëggee, ñépp ñàkk Bant su tooyee yomb a jubbanti Juróom-ñeenti walaakaana soo leen bëggee jubbanti, soo moytuwul fukkeel leen Boroom […]
-
Seex Musaa Ka: Xarnu bi XARNU BI Sëriñ bi noo gi deeti ñaan Faqiir dafay nangoo dagaan Nangul nu lépp lu nu ñaan Ndax Yàlla naatal xarnu bi Noongi dangaan ci Mustafaa Ma nekk marwat’ak […]