• Politik

  • 0
    Wóote ndawi-gox yi Ci 22 fàneelu-ñaar ci wéeru Mars 2009 réewum Senegaal wóote na mpalum ndawi gox yi gox-goxaan yi, maanaam ndaw yu mel naka meer yi, njiitu kominite riiral yi ak ñi […]
  • 0
    Pencum réew mi Ci atum 2008 la ñu bari ci parti yi juunoog nguur gi jël seen matukaay daldi wóo réew mépp, amul xàjji-ag seen wan làng lañu feetoo ci wàllu politik, ngir […]