Turi rabi àll yi ci Wolof
golo gi golo gu ñuul gi dangin wi bukki bi
yolaan wi siiru bi wel wi till wi
suññeel wi kund wi wéxéñ wi jaar ji
sikóor bi njaxat wi saaw bi mbexeex bi
léebéer bi wànga-lànga wi nagu àll wi mbaam-àll mi
kewel gi kooba gi mbill mi njamala gi
fasu àll wi ñey wi (ñay wi) saafaandu gi segg wi
leraw kax wi tene gaynde

There are no comments yet, be the first.

Leave a Comment