0
Deloosi ñi yore tawatu xel
-
Uncategorized
-
Yeesal baatu xarala ci wolof / Taatanu Wolof ak Xamle 1- Jollasu gi = téléphone 2- Kippaango gi = groupe 3- Njémmeer gi = public, assemblée, assistance 4- Limat gi = numéro 5- Lënd gi = internet 6- Lënku = […]
-
Turi rabi àll yi ci Wolof golo gi golo gu ñuul gi dangin wi bukki bi yolaan wi siiru bi wel wi till wi suññeel wi kund wi wéxéñ wi jaar ji sikóor bi njaxat wi […]
-
Bés bu taalifkati yeneen réew làkkee wolof… * Jukki bii topp maa ngi ko jëlee sama téere bi ma tuddee Téere-woy yi te mu genn ci atum 2011 ca Almaañ. Téere bi mën ngeen ko am NDakaaru […]
-
“Filosofi ci wolof”… téere bu bees bi Tamsir Anne génne Seetal Fii « Philosophie en wolof : A comme aada … » aada j. : aada mooy mbooleem matukaay yi am mbooloo, gën gaa bare, aw askan di tegtaloo cig jëf, di ca […]
-
Benn bés, benn woy: Sëriñ Musaa ka XARNU BI Sëriñ bi noo gi deeti ñaan Faqiir dafay nangoo dagaan Nangul nu lépp lu nu ñaan Ndax Yàlla naatal xarnu bi Noongi dangaan ci Mustafaa Ma nekk marwat’ak […]
-
KIPPUG WATTU LÀKKI RÉEW MI Ànd jubal mbind mi ! KIPPUG WATTU LÀKKI RÉEW MI Ànd jubal mbind mi !
-
Ñeel Seex Anta Jóob Liggéey bu mel ni bii ñu fi dëgmal, wareef la ci sunu gis-gis, ñu ñeel fi ca ndorte la góor gu mel ni Seex Anta Jóob. Ndax daf fee def, […]