• Taataan

  • 0
    Turi rabi àll yi ci Wolof golo gi golo gu ñuul gi dangin wi bukki bi yolaan wi siiru bi wel wi till wi suññeel wi kund wi wéxéñ wi jaar ji sikóor bi njaxat wi […]
  • 0
    Melo yi wolof
  • 0
    Benn bés, benn woy: Sëriñ Musaa ka XARNU BI Sëriñ bi noo gi deeti ñaan Faqiir dafay nangoo dagaan Nangul nu lépp lu nu ñaan Ndax Yàlla naatal xarnu bi Noongi dangaan ci Mustafaa Ma nekk marwat’ak […]
  • 4
    Ñeel Seex Anta Jóob Liggéey bu mel ni bii ñu fi dëgmal, wareef la ci sunu gis-gis, ñu ñeel fi ca ndorte la góor gu mel ni Seex Anta Jóob. Ndax daf fee def, […]
  • 1
    “Symbole bi”: céy li ci réew mi! Symbole ci nasaraan, su ngeen ko déggee mooy lëf koo xam ne dafa am lu muy mandaragaal! Du lëf ki ci boppam moo am solo, waaye la muy junjj ci […]
  • 0
  • 0
    Yàggaay ci Wolof
  • 0
    Dal leen ag jamm! Mbooloo mi! Ñu ngi leen di nuyu ku ci nekk ci yeen ci sa tur ak sa sànt te di leen dalal ci jàmm. Béréb bi ngeen tersi téy nag […]