0
Yeesal baatu xarala ci wolof / Taatanu Wolof ak Xamle
1- Jollasu gi = téléphone 2- Kippaango gi = groupe 3- Njémmeer gi = public, assemblée, assistance 4- Limat gi = numéro 5- Lënd gi = internet 6- Lënku = […] -
Xamtéef
-
-
Turi rabi àll yi ci Wolof golo gi golo gu ñuul gi dangin wi bukki bi yolaan wi siiru bi wel wi till wi suññeel wi kund wi wéxéñ wi jaar ji sikóor bi njaxat wi […]
-
KIPPUG WATTU LÀKKI RÉEW MI Ànd jubal mbind mi ! KIPPUG WATTU LÀKKI RÉEW MI Ànd jubal mbind mi !
-
Seex Anta Jóob: Xayma ci Wolof – La héorie des Ensembles Ensembles équivalents Deux ensembles M et N sont équivalents si à un élément de M correspond un élément et un seul de N, et réciproquement. Le caractère commun à tous […]
-
Ngëneel yi ci garabu nebedaay Nebedaay walla ci turu wolofam dëgg saab-saab, garab la gu bari ay ngëneel ci wàllu dund ndax witamin ak ferñeent yu bari yi ci nekk ak li mën a faj […]
-
Niseeryaa sànni na ñaari satelit ci jàww ji! Réewum Niseerya siiwal na alxamees gee nu weesu – 18 fan ci weeru Ut – ne sànni ñaari “satelit” ci jàww ji. Satelit yooyee la ñu cay namm mooy yokk […]