on Sep 12 in Caada tagged by tam
jéra jafati tamsir yàlla na loxobi wér
Jerejefeti Tamsir,
Mbetteel gu and ak mbegte mo fi am tey.Ndax da ma yeewu ni xaaral ma xool ndax -wolof-online- dikaat na… rek dal ci ker-gi. Yagg nanu di fi doxontu tayiit di rafetlu loolu senub ligeey. Ak nuyug cant Bayla
Name (required)
Mail (will not be published) (required)
Website
1- Jollasu gi = téléphone 2- Kippaango gi = groupe 3-
golo gi golo gu ñuul gi dangin wi bukki bi yolaan
* Jukki bii topp maa ngi ko jëlee sama téere bi
War nañoo delloo làkki-réew mi seen gëdd, di leen jëfëdikoo ci nguur gi, ci lekkool yi, ci àttekaay yi ak fépp fu ñuy dogale.
View Results
jéra jafati tamsir yàlla na loxobi wér
Jerejefeti Tamsir,
Mbetteel gu and ak mbegte mo fi am tey.Ndax da ma yeewu ni xaaral ma xool ndax -wolof-online- dikaat na… rek dal ci
ker-gi.
Yagg nanu di fi doxontu tayiit di rafetlu loolu senub ligeey.
Ak nuyug cant
Bayla