Category: Cosaan
Misira demb mooy meen giy dundal mbatiti Afrig
Dooleel làkki réew mi
Sàrti ndaali-Maali
Dr Tamsir Anne (tekkikat bi) Ndaali Maali, walla Mande, benn la woon ci nguuru nit ku ñuul yu mag yi nekkoon démb ci déndub Afrig. Moo fi wuutu woon ndaali Gana ci Afrig sóowu jànt. Gana moom itam moo donnoon jàllooreey yeneeni nguur yu mel ni Aksum , Kuus, Nibi ak Misira démb bu Buur-Fari…
Bàkk: Maam Góorgi Njaay
Jaar-Jaaru Abe Pierre Mohamed Njaay ak S
Solo cosaan ciw askan
Cosaan soo kooy seet, mënees naa wax ne, mooy xàncc biy boole ay nit ba ñu mëna ràññee ne nit ñooñee ñooy askan sangam. Ndax soo demoon téy marse Sàndaga, di béréb bu ay turist yu joggee fun nekk ci àddina di dajaloo di jënd, doo mëna wax mukk ne ñooña fa tase askanu turist…