Usmaan Sonko: njiitu jawriñi nguur gu bees gi
Dooleel làkki réew mi
ABDOU SENE: SENEGAL YEEWU NA Yeewu ngeen, yeewu naa, du ñu falati ku matul njiitu réew
SENEGAL YEEWU NA Yeewu ngeen, yeewu naa, du ñu falati ku matul njiitu réew
NDIGALU MAAM YA
Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu kenn wéer goob ba Bii pas-pas dara mënalu ko dara Dina daw ba raw xëlu fas Ngor ak jom a ko nas Ma ne, Askan wee ko sas Gan góoru jigéen ñi dar lingeer Ci seen farlook seen gànjar ya Bég ba tàccu…
“Filosofi ci wolof”… téere bu bees bi Tamsir Anne génne
aada j. : aada mooy mbooleem matukaay yi am mbooloo, gën gaa bare, aw askan di tegtaloo cig jëf, di ca xàjj lu bon ak lu baax. Matukaay yooyu ñooy doon tegtal yiy ommat nit ki ci yoon wi muy jëflanteek yeneen mbindeef yi ak càkkeef gépp. Kon aada, du loo xam ne ci coobare boppam la ko way di nàngoo topp mbaa mu jalgati ko. Ndax tëral yi ci biir aada, ñaare, ca cosaan la ñiy lawe, di meññ ba yegsi ci jamono…
KIPPUG WATTU LÀKKI RÉEW MI Ànd jubal mbind mi !
KIPPUG WATTU LÀKKI RÉEW MI Ànd jubal mbind mi !
Seex A. Jóob: Làmmiñu réew mi ak gëstu
Làmmiñu tubaab lañu ñagee seen diggante ak mbooloo mi
Deloosi ñi yore tawatu xel
Dooleel làkki réew mi No 2
Turi rabi àll yi ci Wolof
golo gi golo gu ñuul gi dangin wi bukki bi yolaan wi siiru bi wel wi till wi suññeel wi kund wi wéxéñ wi jaar ji sikóor bi njaxat wi saaw bi mbexeex bi léebéer bi wànga-lànga wi nagu àll wi mbaam-àll mi kewel gi kooba gi mbill mi njamala gi fasu àll wi ñey…