{"id":1426,"date":"2012-07-02T20:14:39","date_gmt":"2012-07-02T20:14:39","guid":{"rendered":"http:\/\/www.wolof-online.com\/?p=1426"},"modified":"2012-07-02T20:19:37","modified_gmt":"2012-07-02T20:19:37","slug":"tombukutu-saay-saay-yi-defati-nanu-fa-naawteef","status":"publish","type":"post","link":"https:\/\/www.wolof-online.com\/?p=1426","title":{"rendered":"Tombukutu: Saay-saay yi defati na\u00f1u fa \u00f1aawt\u00e9ef&#8230;"},"content":{"rendered":"<p>&nbsp;<\/p>\n<p>Tey ci Tombukutu, waay-fippu yiy b\u00e0kkoo lislaam te naan da\u00f1uy jihaad defati na\u00f1u fa \u00f1aawt\u00e9ef yu bon: ndax da\u00f1oo dug ci xabru ay waliyu yu mag, toj leen ba \u00f1u mokk rumbax! Tombukutu nag, indil na\u00f1u leen fi ci dal bii, ay yooni yoon ay jukki, doon leen ci f\u00e0ttali j\u00e0llooreem ci w\u00e0llu lislaam. Ndaali Mali la bokkoon, doonoon p\u00e9yu xam-xam ak diine, ndongo yi di j\u00f3gge ba Bagdaad ak Pers doon fa \u00f1\u00ebw di \u00f1akkusi xam-xam ag jikko yu rafet. Li fa nekk ci t\u00e9ere yu \u00ebmb xeetu xam-xam wu nekk ci \u00e0ddina ca k\u00e0ggu ya fa nekk, kenn xamul nu \u00f1u tollu!<br \/>\nWante tey \u00e0ddina s\u00e9pp a ngi seetaan, sambaa-booy yu bon yooyu di jeema faat ndono googu nga xam ne \u00e0ddina s\u00e9pp la soxal, \u00e0ddina s\u00e9pp a ko bokk!<\/p>\n<p>Wante nag liy raam ci \u00f1ag bi la j\u00ebm! Ndax saay-saay yooyu su \u00f1u leen seetaane, su \u00f1u j\u00f3gge foofu dana\u00f1u def lu ko yees!<\/p>\n<p>&nbsp;<\/p>\n<p>[flagallery gid=3 name=Gallery]<\/p>\n","protected":false},"excerpt":{"rendered":"<p>&nbsp; Tey ci Tombukutu, waay-fippu yiy b\u00e0kkoo lislaam te naan da\u00f1uy jihaad defati na\u00f1u fa \u00f1aawt\u00e9ef yu bon: ndax da\u00f1oo dug ci xabru ay waliyu yu mag, toj leen ba \u00f1u mokk rumbax! Tombukutu nag, indil na\u00f1u leen fi ci dal bii, ay yooni yoon ay jukki, doon leen ci f\u00e0ttali j\u00e0llooreem ci w\u00e0llu lislaam&#8230;.<\/p>\n","protected":false},"author":1,"featured_media":0,"comment_status":"open","ping_status":"open","sticky":false,"template":"","format":"standard","meta":{"footnotes":""},"categories":[18,4],"tags":[],"_links":{"self":[{"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=\/wp\/v2\/posts\/1426"}],"collection":[{"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=\/wp\/v2\/posts"}],"about":[{"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=\/wp\/v2\/types\/post"}],"author":[{"embeddable":true,"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=\/wp\/v2\/users\/1"}],"replies":[{"embeddable":true,"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=%2Fwp%2Fv2%2Fcomments&post=1426"}],"version-history":[{"count":5,"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=\/wp\/v2\/posts\/1426\/revisions"}],"predecessor-version":[{"id":1435,"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=\/wp\/v2\/posts\/1426\/revisions\/1435"}],"wp:attachment":[{"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=%2Fwp%2Fv2%2Fmedia&parent=1426"}],"wp:term":[{"taxonomy":"category","embeddable":true,"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=%2Fwp%2Fv2%2Fcategories&post=1426"},{"taxonomy":"post_tag","embeddable":true,"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=%2Fwp%2Fv2%2Ftags&post=1426"}],"curies":[{"name":"wp","href":"https:\/\/api.w.org\/{rel}","templated":true}]}}