{"id":1074,"date":"2012-06-26T13:32:34","date_gmt":"2012-06-26T13:32:34","guid":{"rendered":"http:\/\/www.wolof-online.com\/?p=1074"},"modified":"2012-07-01T10:46:30","modified_gmt":"2012-07-01T10:46:30","slug":"niseeryaa-sanni-na-naari-satelit-ci-jaww-ji","status":"publish","type":"post","link":"https:\/\/www.wolof-online.com\/?p=1074","title":{"rendered":"Niseeryaa s\u00e0nni na \u00f1aari satelit ci j\u00e0ww ji!"},"content":{"rendered":"<p><a href=\"http:\/\/www.wolof-online.com\/wp-content\/uploads\/2012\/06\/satellite_nigeria_1.jpg\"><img loading=\"lazy\" decoding=\"async\" class=\"alignleft size-full wp-image-1075\" title=\"satellite_nigeria_1\" src=\"http:\/\/www.wolof-online.com\/wp-content\/uploads\/2012\/06\/satellite_nigeria_1.jpg\" alt=\"\" width=\"273\" height=\"193\" \/><\/a>R\u00e9ewum Niseerya siiwal na alxamees gee nu weesu &#8211; 18 fan ci weeru Ut &#8211; ne s\u00e0nni \u00f1aari &#8220;satelit&#8221; ci j\u00e0ww ji.<br \/>\nSatelit yooyee la \u00f1u cay namm mooy yokk faggaru ci musiba yu mel ni maral ag mb\u00ebn ngir yokkuteef ci w\u00e0llu mbay ag karaange ci seen dund.<br \/>\n\u00d1aari satelit yooyu, \u00f1u tudde NigeriaSat-2 ak NigeriaSat-X , \u00f1u ngi leen s\u00e0nne Risi ci b\u00e9r\u00e9b bu nu naan Yasni.<br \/>\nKon bii mooy \u00f1aareeli yoon bu r\u00e9ewum Niseeryaa, di daanaaka r\u00e9ew mi g\u00ebn a mag ci Afrik, yonne ay satelit ci j\u00e0ww ji. Yoon bu nj\u00ebkk bi, bu \u00f1u f\u00e0ttelikoo, ci atum 2007 la woon. Booba Niseerya r\u00e9ewum Siin la m\u00e0nkoo woon ci m\u00e9b\u00e9t boobu: Wante satelit bu nj\u00ebkk boobu da mujj sax seey ci j\u00e0ww ji, g\u00e0nnaaw ba mu fa nekke lu tooloog at! Ku dul b\u00ebre nag moom, doo daanu gaa, wante it doo am ndam!<br \/>\nMbir mi nag li tax mu am solo lool, mooy itam, ne benn satelit bi \u00f1u tudde NigeriatSat-X ay doomi Niseeryaa, di ay ense\u00f1\u00eb\u00ebr ag ay boroom-xam-xam yu xere\u00f1\u00f1 \u00f1oo ko defar ci seen xarala bopp.<br \/>\nXibaar yiy satelit yooyu di yonnee ci suuf ba l\u00e9egi itam, da na tax ba Niseeryaa g\u00ebn a m\u00ebn a saytu \u00f1aawteef yi yaqkat ak sambaabooy yiy s\u00e0cc petorol, di jaay ngannaay mbaa di def yeneen toqidoona. Kon loolu yokkuteef la ci w\u00e0llu karaange r\u00e9ew mu yaatu te mag moomee.<br \/>\nPeresidaa Niseeryaa, Goodluck Jonathan, wonne na mb\u00e9gteem lool ci loolee r\u00e9ewam def, di j\u00e0lloore ci d\u00e9ndu Afrik ag lu ko weesu.<\/p>\n<p>Kon g\u00e0cce ngallaama!<\/p>\n","protected":false},"excerpt":{"rendered":"<p>R\u00e9ewum Niseerya siiwal na alxamees gee nu weesu &#8211; 18 fan ci weeru Ut &#8211; ne s\u00e0nni \u00f1aari &#8220;satelit&#8221; ci j\u00e0ww ji. Satelit yooyee la \u00f1u cay namm mooy yokk faggaru ci musiba yu mel ni maral ag mb\u00ebn ngir yokkuteef ci w\u00e0llu mbay ag karaange ci seen dund. \u00d1aari satelit yooyu, \u00f1u tudde NigeriaSat-2&#8230;<\/p>\n","protected":false},"author":1,"featured_media":0,"comment_status":"open","ping_status":"open","sticky":false,"template":"","format":"standard","meta":{"footnotes":""},"categories":[16],"tags":[],"_links":{"self":[{"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=\/wp\/v2\/posts\/1074"}],"collection":[{"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=\/wp\/v2\/posts"}],"about":[{"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=\/wp\/v2\/types\/post"}],"author":[{"embeddable":true,"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=\/wp\/v2\/users\/1"}],"replies":[{"embeddable":true,"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=%2Fwp%2Fv2%2Fcomments&post=1074"}],"version-history":[{"count":5,"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=\/wp\/v2\/posts\/1074\/revisions"}],"predecessor-version":[{"id":1298,"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=\/wp\/v2\/posts\/1074\/revisions\/1298"}],"wp:attachment":[{"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=%2Fwp%2Fv2%2Fmedia&parent=1074"}],"wp:term":[{"taxonomy":"category","embeddable":true,"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=%2Fwp%2Fv2%2Fcategories&post=1074"},{"taxonomy":"post_tag","embeddable":true,"href":"https:\/\/www.wolof-online.com\/index.php?rest_route=%2Fwp%2Fv2%2Ftags&post=1074"}],"curies":[{"name":"wp","href":"https:\/\/api.w.org\/{rel}","templated":true}]}}