Back to homepage Back to homepage
"Bépp làkk rafet na bu gindi ca nit xel ma, téy tudd ca moom ngor la" (Seex Musaa Ka)
Xew-xew 

Politik
Nekkinu-mbooloo mi
Koom-koom
Caada ji
Diine
Bitim-réew
Tàggat-yaram

Ñeel Seex Anta Jóob

Bés bu kenn dootul fàtte!

Bataaxal bi ëmb sañ-sañi doomu aadama

Xamtéef ci Wolof: baatukaayu xayma

Baat yii topp yépp ci téere Seex Anta Jóob bi mu tuddee Waaso nit ku ñuul ak caada (Nations Nègres et cultures) lañu leen jukkee. Mbind mi doŋŋ lañu yeesal ba mu mànkoo sàrt yiy yoonal mbind ci làkku Wolof.
Francais
Wolof
point tomb
ligne rëdd
plan  maasale
surface yaatu-yaatu
volume ëmbka
axe diggël
sens joxañ
demi-droite xaaju-njub
angle koñ
angle adjacent puqtël bokk-wet
angle puqtël jub
angle aigu puqtël xat
angle obtu puqtël làñ
angle complémentaire puqtël motalaante
angle supplémentaire puqtël yokkalaante
triangle ñett-koñ
coté wet
hauteur kawewaay
angle puqtël
mediane jaar-digg

sommet puj
hypothénuse janook koñ-jub
bissectrice seddale-puqtël
orthocentre tàseeb-kawewaay
genre de triangle giiri ñett-koñ
triangle isocèle ñett-koñ ñaari wet yem
triangle rectangle ñett-koñ jub
triangle équilatéral ñett-koñ wet yem
triangle scalène ñett-koñ yemadi

droites parallèles njublàŋ
angles alternes internes jalawle biir
alterne externe jalawle biti
quadrilatère ñeent-wet
rectangle jubkoñ
losange carré doy
carré kaare
trapèze ñaari-wet làŋ
symétrie safaanoo
symétrique par rapport à un point safaanoo dekkarleeb tomb
symétrique par rapport à une droite safaanoo dekkarleew rëdd
symétrique par rapport à un plan safaanoo dekkarleeg maasale
Li ci topp





©2009 wolof-online. Tous droits réservés.