Sunu sosiete

 

 

 

 

 

Sunu sosete

Sunu sosete yëngëtu na!
Sunu sosete yëngëtu na!
Ñun danuy am faydaa!
Ñun danuy am faydaa!
Ñun danuy fonk sunu Senegaal!

Adduna potu ndaa laa!
Ku fi naan jox sa morom naan!
Adduna potu ndaa la!
Ku fi naan jox sa morom naan!

Faatu Fay

Faatu yoo si njalalalu!
Faatu yoo si njalalu!
Faatu Fay Fay Fay Fay
Faatu Kelemaatiyoo
Faatu yoo si njalalu!

Faatu yoo si njalalalu!
Faatu yoo si njalalu!
Faatu Fay Fay Fay Fay
Faatu Kelemaatiyoo
Faatu yoo si njalalu!

There are no comments yet, be the first.

Leave a Comment