Wote bi nu dëgmal, ñépp xam na ñu ko, wote
-
Politik
-
Isaa Bokar Si ” Yaaya Jàmme mooy ndeyyi-mbill mi ci Gambi ak Kasamaas”
Isaa Bokaar Si, ambaasadeur Yaaya Jàmme la woon, bokkoon na
-
Màki Sàll: “du ma làq kenn ku def lu dëppoowul ag yoon”!
Ci benn laaj-toontu bu njiitu-réew mi amal ag yeenekaay bu
-
Kookooy Saalif Saajo njiitu waay-fippu ya ca Kasamaas…!
Peresidaa Maki Sàll ne woon ayu-bés yale weesu, ne tàllal
- Li ci topp: Politik
-
Caada
- Li ci topp: Caada
-
Multimejaa
- Li ci topp: Multimejaa
-
Diine
-
Diine ci làmmiñu Wolof: Yoonu ragal-Yàlla
Bisimilaahi Rahmaani Rahiimi… Ñu fas yeeney dollee deηkënte ak di
-
Xasida Sëriñ Tuuba ci Wolof : Nahjul Xadaail Haaji – Wolof
Maa ngi tàmbale samay wax ak jëf ci turu Yàlla
- Li ci topp: Diine
-
Yeneen jukki
-
Turu rabi-àll yi ci Wolof
golo gi golo gu ñuul gi dangin wi bukki bi yolaan wi siiru bi wel wi till wi suññeel wi kund wi wéxéñ wi jaar ji sikóor bi njaxat wi
[ Read more ] -
BATAAXAL BU MAG BI ËMB SAÑ-SAÑI DOOMI AADAMA
UBBITE Ñu jàpp te nangu ne sagu doomi aadama ak sañ-sañam yépp-dañu yam te kenn mënukóo jalgati, te lu lépp nekk na cës laay ci taxufeex ci mbirum àtte ak
[ Read more ] -
Laaj-toontu ag Njaga Mbay
Jaar-jaaru woykat bu jege woon askanam Ci sanwiye 1999, yeneekay Lasli/Njëlbéen amoon na laaj-tootu bu yaatu ag Njaga Mbay, doon ca feeñal ay jaar-jaaram. Waxtaan woowu Njaga Mbay amoon ak
[ Read more ] -
ndeeteelu làkk yi…
Ci 7000 làkk yi ci àddina, 85 la ñi ëpp ci nit ñi, daanaka 78%, di làkk. Làkku angale ñi koy làkk tollu nañu ci 328 miliyoη, ñiy làkk sinwaa tollu
[ Read more ]



