1
Làmmiñu tubaab lañu ñagee seen diggante ak mbooloo mi
-
Caada
-
Bés bu taalifkati yeneen réew làkkee wolof… * Jukki bii topp maa ngi ko jëlee sama téere bi ma tuddee Téere-woy yi te mu genn ci atum 2011 ca Almaañ. Téere bi mën ngeen ko am NDakaaru […]
-
Bés bi UNESCO jagleel làkki ndey yi … Bésu 21 fan ci weeru fewrie at mu jot, moom la kurél giy toppatoo caada, njàng ak xamtéef (UNESCO) te féetoo ci mbotaayu xeet yi, jagleel làkki ndey, maanaam làkk […]
-
Benn bés, benn woy: Sëriñ Musaa ka XARNU BI Sëriñ bi noo gi deeti ñaan Faqiir dafay nangoo dagaan Nangul nu lépp lu nu ñaan Ndax Yàlla naatal xarnu bi Noongi dangaan ci Mustafaa Ma nekk marwat’ak […]
-
KIPPUG WATTU LÀKKI RÉEW MI Ànd jubal mbind mi ! KIPPUG WATTU LÀKKI RÉEW MI Ànd jubal mbind mi !
-
Ñeel Seex Anta Jóob Liggéey bu mel ni bii ñu fi dëgmal, wareef la ci sunu gis-gis, ñu ñeel fi ca ndorte la góor gu mel ni Seex Anta Jóob. Ndax daf fee def, […]
-
Cosaanu mbind ci Afrik Cosaanu mbind ci Afrik lu mat a fésal la, ndax ñu bari, waay-xeltu yeek meroe.jpg ñeneen dañoo defe ne caada yi nekk Afrik xamuñu ca seen cosaan xaralaay mbind. Manaam […]
-
Sedaar Seŋoor: Juwaaloo Juwaalo Juwaalo! Maa ngi fàtteliku. Maa ngi fàtteliku siñaar ya ca keru mbaar yu naat ya Maa ngi fàtteliku siñaar yeek seeni gët, kéemtaanee lool Di sàmandaay leeraayu weer cig […]
-
Sàrti ndaali-Maali Dr Tamsir Anne (tekkikat bi) Ndaali Maali, walla Mande, benn la woon ci nguuru nit ku ñuul yu mag yi nekkoon démb ci déndub Afrig. Moo fi wuutu woon ndaali […]