0
Jamono ci wolof
-
Caada
-
Téere-woy yi Téere-woy yi téere la bu ëmb taalif yu bindkat ak xaralakat yu mag ci làkki almaa taalif. Téere baa ngi genn ci atum 2011 ca Almaañ. Tamsir Anne, mi móol […]
-
Bàkku Senegaal Yëngal-leen kooraa yi te dóor ci sabar yi Gaynde ñaloor yuux na. Boroom àll tëb na Tëb na tëbu jàmbaar, leeral lu doon lëndëm Suñuy naqar jeex na, sunu […]
-
ndeeteelu làkk yi… Ci 7000 làkk yi ci àddina, 85 la ñi ëpp ci nit ñi, daanaka 78%, di làkk. Làkku angale ñi koy làkk tollu nañu ci 328 miliyoη, ñiy làkk sinwaa tollu […]
-
Li ci biir “francophonie” Ci ayi bés yii ñu dëgmal mbootaayi-réew yiy jëfandikoo làkki “francais” tey wooye seen bopp mbootaayu “Frankofoni” ñu ngi waaj seen 14eelu ndaje, ngir berndeel làkki francais ak caada Faraas. […]
-
Timbukutu: peyu xam-xam Timbukutu: péyu xam-xam bu yàgg te sax! Ni ñu leen ko fi waxeewoon ci jukki bi weesu, bind, sàkku xam-xam, gëstu ak diine lu yàgg la ci Afrik! Wante ñakka […]
-
BATAAXAL BU MAG BI ËMB SAÑ-SAÑI DOOMI AADAMA UBBITE Ñu jàpp te nangu ne sagu doomi aadama ak sañ-sañam yépp-dañu yam te kenn mënukóo jalgati, te lu lépp nekk na cës laay ci taxufeex ci mbirum àtte ak […]
-
Mbindum wolof Mbind mi* 1. Jàppal lii à warul a wéet, fàww mu am araf wu ko féete wàllu ndeyjoor te loolu mënul a nekk lu dul baatoodi bu ñu séexal (tàkk), […]
-
Laaj-toontu ak Njaga Mbay Jaar-jaaru woykat bu jege woon askanam Ci sanwiye 1999, yeneekay Lasli/Njëlbéen amoon na laaj-tootu bu yaatu ag Njaga Mbay, doon ca feeñal ay jaar-jaaram. Waxtaan woowu Njaga Mbay amoon ak […]